Filipendula ulmaria dafay màgg ci wetu ndox.
Garab gi am na cabb bu rëy. Tóor-tóor bi dafa ndaw te weex.
Xoolal bu baax xob yi:
Xoolal! Forma denudata la (amul kawar ci suufu xob yi):
Filipendula ulmaria présente une grande grappe complexe de très petites fleurs blanches. Les folioles terminales de ses feuilles imparipennées sont au moins ternées. L’absence de pilosité sous la feuille implique qu’il s’agisse de Filipendula ulmaria forma denudata.
Rosales>Rosaceae>Filipendula ulmaria
Gàncax: Lythro salicariae – Filipenduletalia ulmaria.
Garab metit la!
Foto ci Pont-Roby (23500). PNRM. Felletin: